njegenaay

Daagul, jaayul ndaama
Xam nga ni dal ya mën ndaw y
Daagul, jaayul ndama
Xam nga ni dal ya mën ndaw y

Moom dal li mu bëgg
Amaanaa du lu bar i
Kuu xam li mu wara def te dikoo def nu mi waare
Jàppul seeni tele, zappé séen chaine sax
Waat naani su may cote du ma ko mës a ndendale ndax

Amul ku dul man
Xamul kul dul man
Gëmul su ma gooreel du ma ko naxee mbaay
Amul ku dul man
Xamul kul dul man
Gëmul, jëmmaan ji mooy sama njegenaay
Amul ku dul man
Xamul, ey kul dul man
Gëmul, su ma gooreel du ma ko naxee mbaay
Amul ku dul man
Xamul, kul dul man
Gëmul, jëmmaan ji mooy sama njegenaay

Yaw la mujjee déggoo ba ma nelaw
Yaw la njëkk a janook ba ma yéewoo
Daru dunya sa su nel selew
Sa jëmm jee doon sama njegenaay

Kaay jugal jaayu nak
Jugal yëngal àdduna
Taaru nga, taayu nga
Sama jigéen kay digal
Kaay digal jaayu nak
Jugal yëngal àdduna
Kaay du ma sasuman
Dinala wayal sa su ne

Ci sama xol yaay ki fa njëkk a toog
Xas nafa féete ag yaw sunu yabbo ngóorgóolu
Ci sama xol yaay ki fa njëkk a toog
Xas nafa féete ag yaw sunu yabbo ngóorgóolu

Amul, ku dul man
Xamul, kul dul man
Gëmul, su ma gooreel du ma ko naxee mbaay
Amul, ku dul man
Xamul, kul dul man
Gëmul, jëmmaan ji mooy sama njegenaay
Amul ku dul man
Xamul, ey kul dul man
Gëmul, su ma gooreel du ma ko naxee mbaay
Amul ku dul man
Xamul, kul dul man
Gëmul, jëmmaan ji mooy sama njegenaay

Daagul, jaayul ndaama
Xam nga ni dal ya mën ndaw yee
Daagul, jaayul ndama
Xam nga ni dal ya mën ndaw y



Credits
Writer(s): Abdoulaye Diop, Saliou Samb
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link