My People

ma ngui binde way bi diko méy
gneup gni ma beugue di lèn ndioukel
ndioukel gneup gni ma diapalé
souma lène meunone diokh lokho

defnako
soumalène meunona setsi eh eh

yeksina

fatéwoumalène, dédéte meunoul am
yeugone nalèn salaw moy li wor
souma teugué ngène gneuw wouyoussima
souma guéné lou bess ngène dieundeuko
manou malène faye
magui bind way wi di lène ko méy

you you you you
you gorgorloul gnougui sa guinaw
you you you you
you gorgorloul gnougui sa guinaw

soumalène meunone diokh lokho defnako
souma lèn meunona setsi yéksina
kouma soufèl ngène khoulok mom
fatéwoumalène dédét meunoul am
yeugue nalène salaw moy li wor
bataxna ma gui bind way wi diko may

you you you you
you gorgorloul gnougui sa guinaw
you you you you
you gorgorloul gnougui sa guinaw

fatéwouma fatéwouma fatéwouma fatéwouma ah
fatéwouma fatéwouma fatéwouma fatéwouma ah
fatéwouma fatéwouma fatéwouma fatéwouma ah
fatéwouma fatéwouma fatéwouma fatéwouma ah
you you you you
you gorgorloul gnougui sa guinaw
you you you you
you gorgorloul gnougui sa guinaw

ehhhhhhhhhhhhhhh mangléni sant di gueureum
mane ndioukel nalèn

uuuuhhhhhhh



Credits
Writer(s): Youssou N Dour, Birame Ndiaye Ndeck
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link