Samaxol

Sama xol bo ma tàgguwoon
Do ma yóbbe biile coono
Sama xol bo ma tàgguwoon
Do ma yóbbe biile coono
Mar a naan te ragal ndox mi

Oh mbëggeel
Hann manak mbëggeel

Sama xol bo ma tàgguwoon
Do ma yóbbe biile coono
Sama xol bo ma tàgguwoon
Do ma yóbbe biile coono

Picci miy naaw la, dafaa gumba
Dafa dul xool fa muy jógee
Dafa yor tàngaay u Jaxalnama
Ak sedday u Aljana

Oh mbëggeel
Hann manak mbëggeel
Oh mbëggeel
Hann manak mbëggeel

Sama xol bo ma tàgguwoon
Do ma yóbbe biile coono
Sama xol bo ma tàgguwoon
Do ma yóbbe biile coono
Mar a naan te ragal ndox mi

Oh mbëggeel
Hann manak mbëggeel

Suma jógee ba jëm ci moom
Giir yeggee ko sumay xalat
Sama fit wi daldi key raggal
May wëndéelu, jaaxle lool

Oh mbëggeel
Hann manak mbëggeel
Oh mbëggeel
Hann manak mbëggeel

Te bu siggee, xippi, xool ma
Sama dunya bëgg a yëngu
May wëndéelu, dii waxtu
Man de xalat samay pexe

Oh mbëggeel
Hann manak mbëggeel
Oh mbëggeel
Hann manak mbëggeel

Picci miy naaw la, dafaa gumba
Dafa dul xool fa muy jógee
Dafa yor tàngaay u Jaxalnama
Ak sedday u Aljana

Oh mbëggeel
Hann manak mbëggeel
Oh mbëggeel
Manak mbëggeel



Credits
Writer(s): Coumba Gawlo
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link