Wakhal
Par AbouAmg
nit kou bakh
waroul mome di téyé meer
bour yala diko togne lagnou deké
wargua xalat bala guamay antou
gueneul li khol waw bo teudé nélaw
nit kou bah warna di balé mome
nit kou bah warna di diéguelé
ndakham bourbi yala dagnou deukeu
diko togne
bo dioulé gnane mou facé say bakar
dafa bayi say morom yaw tanala
bayi keur ndey ak bay guir séyal la
kon boumou sey dou lougnouy
tiakhané
gueneul li khol waw bo teudé nélaw
kay wakh ak mome kay wakh
ak mome
kay wakh ak mome yéneu bokeu
diéguénaye
kay wakh ak mome kay wakh
ak mome
kay wakh ak mome yéneu bokeu
diéguénaye
hé nagnou tiapa né djiguèn gny
gnoye sounou kany hègne
kon gnoune ak goune gnoune
ak gnome
ba saguar khègne
mouny
waw nagnou diapa né sey louko taka
tassouko
kon gnoune ak goune gnoune
ak gnome
ba pik ak pèle kheu
yaw miye diame bougne la balo
nagua balé
bour yala mome dagnou deukeu diko
togne
kon yaw miye diame bougne la balo
dagua wara balé
ndakh bour yala mome sopeuna diam
bouy balé
kay wakh ak mome kay wakh
ak mome
kay wakh ak mome yéneu bokeu
diéguénaye
kay wakh ak mome kay wakh
ak mome
kay wakh ak mome yéneu bokeu
diéguénaye
bilay bilay bilay
nit kou bakh
waroul mome di téyé meer
bour yala diko togne lagnou deké
wargua xalat bala guamay antou
gueneul li khol waw bo teudé nélaw
nit kou bah warna di balé mome
nit kou bah warna di diéguelé
ndakham bourbi yala dagnou deukeu
diko togne
bo dioulé gnane mou facé say bakar
dafa bayi say morom yaw tanala
bayi keur ndey ak bay guir séyal la
kon boumou sey dou lougnouy
tiakhané
gueneul li khol waw bo teudé nélaw
kay wakh ak mome kay wakh
ak mome
kay wakh ak mome yéneu bokeu
diéguénaye
kay wakh ak mome kay wakh
ak mome
kay wakh ak mome yéneu bokeu
diéguénaye
hé nagnou tiapa né djiguèn gny
gnoye sounou kany hègne
kon gnoune ak goune gnoune
ak gnome
ba saguar khègne
mouny
waw nagnou diapa né sey louko taka
tassouko
kon gnoune ak goune gnoune
ak gnome
ba pik ak pèle kheu
yaw miye diame bougne la balo
nagua balé
bour yala mome dagnou deukeu diko
togne
kon yaw miye diame bougne la balo
dagua wara balé
ndakh bour yala mome sopeuna diam
bouy balé
kay wakh ak mome kay wakh
ak mome
kay wakh ak mome yéneu bokeu
diéguénaye
kay wakh ak mome kay wakh
ak mome
kay wakh ak mome yéneu bokeu
diéguénaye
bilay bilay bilay
Credits
Writer(s): Ismael Lo
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
Other Album Tracks
© 2025 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.