Sopante

Sopanté Beuguenté
Têeye wètie xalate
Kila Nop Nop ko
Kila Ré Ré ko
Kila Fine Fine ko
Kila diègué diègué ko
Sopantélène Beuguentalène
Yawe milé waye Dioure
Boule Mayé sa Dome
Wadjou mou Beugoule
Nobel dou diaye
Sopantélène Xamantélène
Sopanté Beuguenté
Têeye wètie xalate
Nobel mo wore
Kila Ré Ré ko
Kila Fine Fine ko
Kila diègué diègué ko
Sopantélène Beuguentalène
Boye mayé sa Dome
Ladiale sa Dome
Balaye Rêtiou di wesse
Wala tiowo di Éme
Sopantélène Xamantélène



Credits
Writer(s): Leandro Pablo Aconcha, Idrissa Diop
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link