Yaay

Téy dji laléy lay khamaal
Fi nga tolou ci mane
Téy dji saama khol bi
Ware gua kha kham ni mane
Li ma aame ak li ma amoul
Ware gua kham ni yako mome
Li ma meune ak li ma meunoul
Lépp yaye borom

Yeurmandé Yeurmandé Yeurmandé
Yeur mandé Yeurmandé Yeurmandé
Yeurmandé Yeurmandé Yeurmandé
Yeurmandé Yeurmandé Yeurmandé

Bayinaa loumeu dieufé
Nara dab sa banékh
Bo khébouul sama djeuf yi
Kone andeu bi nékh
Li ma aame ak li ma amoul
Ware gua kham ni yako mome
Li ma meune ak li ma meunoul
Lépp yaye borom

Yeurmandé Yeurmandé Yeurmandé
Yeur mandé Yeurmandé Yeurmandé
Yeurmandé Yeurmandé Yeurmandé
Yeurmandé Yeurmandé Yeurmandé

Maye aame di la diokh iow
Sou doyoul ma doli
Maye aame di la watt iow
Di gnane gnou wéssou fi
Lima ame ak lima amoul
Ware gua kham ni yako mome
Lima meune ak lima meunoul
Lépp yaye borome
Lima ame ak lima amoul
Ware gua kham ni yako mome
Lima meune ak lima meunoul
Lép yaye borome

Dolé Yeurmandé
bo djékko dénguey bale
la gua eup Dolé Yeureumko
Nguir yallah moune la bale

Lima ame ak lima amoul
Ware gua kham ni yako mome
Lima meune ak lima meunoul
Lép yaye borome
Lima ame ak lima amoul
Ware gua kham ni yako mome
Lima meune ak lima meunoul
Lép yaye borome



Credits
Writer(s): David Turkstra, Cheikhou Coulibaly, Papa Fall
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link