Memory

Niit ya ngi toppeu adouna di Daw diap ko taxoul gnu taxaw
Dee ba ngi dokh di gneuw sugnu kaw, dafa yagg wayé guen dou raw
Meunou ma nelaw dou gawu dou Dibbéer, ta likoy dindi dou ferniente
Meunou ma wax ak yaw si dianeer, bou goudé nga may tontou ci Guent
Meuneu touma ameu kou melni yaw, Mane lolou lima xam la
Li ma meti dou li nga dem ba faw, wayé ci diamono yima la xamla
Da ngay minanté ak Niit ko naw, dem ba faté ni Dokh ak Bane la
Dafay dem ba bokk ci yaw, Boy da ngay dem ba faté ni gane la
Niit sagnu ta bagne woté, surtout woté bu diogué ci Yallah
takh ma souk samay ome, sama rongogne yi di tourou may niane bou balle la
Moussou ma fok ni ni lay demé beuss bofi nekatoul
Dakh bedienou Kobba sugnu lako diamé, fils kokou dou nekha toul
Dakh Niit kou nek ak Ni nga koy xamé, tay sama doundou bi nexatoul
Damadone gaagnu di xeuye di taané, wayé tay dji yoombatoul
Yene say may tok di khentiou say yeré guir fataliku sa xeet
wayé lane lay wout si adouna bi mane kessé bou dé nekato ci sama wet

{2}
Comme que legui nonou la demé
Mane sakh legui damala meré
Sa bountou nek dotou mako diegué
Dotou ma setanati say photo, ta dootu ma xentioti say yeré
Nane lay def ba boor bi nga ma lebale demb tay ma meune lako faye
Donté xam nani nathe dium demb, meune ta wowale pottum tay
Loy dieurignu gnak toll bodule baye
Lepp boor bodoul faye
Ma ngi sogua xam loutakh monate di xol dom dji rek mouy sour

Djiguene djuy seuyi dagnu kouy mour

Ma ngi sogua xam loutakh, dereet bou dé di sopeeku deut
keweul di teup ta dome dji dou beut

Nakh nga ma ba dem sa yone
Loutaakh xaro limala denthialone
Koula ni beugou mawone gnuy ande thi mbedeu mi dokhontou diapannté lokho

Koula ni beugou ma wone nga diegué ma guir louma meti ma yeguel lako
Koula ni neko wone sama dolé, guir louma meti ma meune ko encaissé
Yaw nga xam thi lolou lepp ba paré, ngay dem dima fi bayi mane kessé (bis)

Meunote nga fi dess wetalima touti meme sou feké damay wagni ci limay dou doundou fayal lassi djouti
Yeah, lou Yallah def mo guene, Ma ngi Jegualou



Credits
Writer(s): Macleod, Norris, Stevenson, Tranter
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link