Gaday - Live

Yaaye sama bakh
Yaaye sama doolé
Soma bayé ci kane laye fanane
Yaaye sama nék
Yaaye sama soutoura
Soma bayé ci kane laye fanane
Yaaye sama bakh
Yaaye sama doolé
Sou goudé ci yow laaye fanane
Ma gadaye nguir meuné khamé sama mbeuguel
Walla bok ma gadaye nguir meuna ragné souniou nobél
Wala sakh niou ande gadaye nguir meuna ragné souniou mbeuguel
Nétali goor gooré samal ngor diama gueune aaye
Toggal khar yalla mou nieu khar yalla
Ni yémoula né laaram tooré
Soma bayé fane lay fanane
Ki la nane
Ki la nane diw dou sa nawlé guéweul laaaa
Bour yalla amoul nguéweul
Domou adama rekka ko gnoore
Sa wopikame na malak malak marli
Soma bayé fane laaye fanane
Shou éra
Shou éra
Ousmane thiam wawa wa nga goor
Shou éra
Ousmane khadim thiam
Ousmane maguette thiaw wawa wa nga goor
Shou éra mactar falléne bi xxxxxxx massaba déguéne fall sa mame la
Anhan loumou méti méti
Douma bayi béne yone
Bayou awa mbaye kaye diogamaye xxxxxxxxxx
Bétté bétté hey mbaye
Déggal bayou awa mbaye
Déggal bayou niémbé Diop
Loumou méti méti
Douma bayi germe diop
Bayi niémé diop
Wowo xxxxxxxxx
Bétté bétté bé bétté bé hey fall
Ndiogou mbaye bayou awa mbaye wawa goor
Doga falli ma wa ndiok ousmane mbacké thiam
Bétté bétté bé faye
Xxxxxxxxx toucouleur alé racine kay gnou dém podor
Xxxxxxxxx
Anhan loumou méti méti douma bayi béne yone
Bayou awa mbaye kaay diogamaye xxxxxx
Hey hey wawaw wawaw



Credits
Writer(s): Waly Seck
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link