Lutax

Oh wé, Mama wo, waw waw khawma
lu takh ma miir
Li takh ma beugueleu yow chérie,
taw ma wakhatiko oh oh
Li ma takha dof si yow bilay tay ma
wakhat lako oh chérie coco
lico waral moy danga boof si samam khél
Deukeu si sama khol bi yé yée
Lico waral moy danga boog si sama khél
Deukeu si sama khol bi yé yée
Tey ma bamtoula li takh ma fébar
si say mbir
Ah chérie beugueunala, oh all right
Boma woyofalé mba nga saganéma
Dina tiis si mane
Yaay garap gui sakh sama diig boop
Si sa képar lay fékhlo oh, oh, oh chérie yow
Boma woyofalé mba nga saganéma
Dina tiis si mane
Dieumbeut nala mane si sama digui khol
Dila soukheut si sama khél
Ngay magga si sama rou gui
Téy law si sama dieumeu dji
Di tôr tôr si samay beut waw,
ah chérie beugueunala
Boma woyofalé mba nga saganéma
Dina tiis si mane
Si sa képar lay féékhlo oh
Di doundou si sa mégnééf
Téy fadiou si say réno
Boma woyofalé mba nga saganéma
Dino tiis si mane



Credits
Writer(s): Mamadou Moustapha Lo
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link