Lo Beugue

shibiribi ritibi sharatibu
shibiribi ritibi sharatibu
shibiribi ritibi sharatibu
shibiribi ritibi sharatibu
wax ma lo beuge ma defalaqo
wax ma lo name ma indilako bassi ioe ga dieul
ma defalko amooooo kenene kouma soute
shibiribi ritibi sharatibu
shibiribi ritibi sharatibu
shibiribi ritibi sharatibu
shibiribi ritibi sharatibu
wax ma lo beuge ma defalaqo
wax ma lo name ma indilako bassi ioe ga dieul
ma defalko amooooo kenene kouma soute
li ga jota mougn si diguente bi
beuri neu new niuko mouna mougn si yap bi
wayei defo ko niel mbeugel gui gay bagn mou nakhsay
suma sagnon sa buma gesto guisla sama wet
amoulooo kenene kuma soute
wahmaloname my boy Ama Gaye Hana nekheu
Aicha Ballago
wahmaloname my boy Ama Gaye Hana nekheu
Ayei Yaye ndeke mbeugel ni la nekhe
wawallay momo ndiaye ndeke mbeugel nila nekhe
Momo Momo
kone degal Momo Ndiaye
Momo Anta Ndiaye
Yeme Ndiaye sa mame Papa Anta Ndiaye
Aby Diallo moy sa mam
Sr Mbacke Ndiaye seu baye
Bokum Yayou am Ndiaye Koor Kine bayou Saliou
Wa wallay Momo Ndiaye ndeke Momo sama way la
Diagay sa yaye
ayei Yaye ndeke mbeugel nila nehe
shibiriberibere ndeke mbeugel nila nekhe
shibiriberibere ndeke mbeugel nila nekhe
Momo Ndiogou Ndiaye
Momo ndiaye ndeke momo sama way la
Wawallay ndeke momo sama way la
ayei yaye ndeke mbeugel nila nekhe



Credits
Writer(s): Wally Ballago Seck
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link