Nuyo na

Hé garyi nieuw na
Hé garyi nieuw na
Hé garyi nieuw na
Woh garyi nieuwna

As salamalékoum nouyou namalén(Ma lékoum salam)
As salamalékoum nouyou namalén(Ma lékoum salam)
As salamalékoum nouyou namiounouyo(Ma lékoum salam)
As salamalékoum nouyou nanioulén(Ma lékoum salam)
Diam ak salam lay woté mane
Diam ak salam lay woté mome lay nioudi (mane malékoum salam)
As salamalékoum nouyou naniounouy(Ma lékoum salam)
As salamalékoum nouyou nanioulén(Ma lékoum salam)
Hé garyi nieuw na
Hé garyi nieuw na
Hé garyi nieuw na
Woh garyi nieuwna

Wouyoulén ndax Yalla
Wouyoulén ndax Yalla
Wouyoulén kiy nouyo

Wa Afrique nouyona
Sénégal nangen def
Dakar njigui took
America njigui took

Wouyouléne ndax Yalla
Wouyoulèn kiy nouyo

Dakar nouyona
Sénégal yen nangene def
Nouyoulén ndax Yalla

Hé garyi nieuw na
Ho garyi nieuw na
Sén garyi nieuw na
Woh garyi nieuwna

Wouyoulén ndax Yalla
Wouyoulén ndax Yalla
Sénégal nangen def
Euopa njigui took
Asia tam njigui xool

Wouyoulén ndax Yala
Wouyoulén kiy nouyo
Wa Afrique nouyona
Sénégal nangen def
Dakar njigui took
America njigui took



Credits
Writer(s): El Hadji Fall Diouf
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link