Dama la nob

Mane damala nopp
Soo beugué sunu ande nekh
Yow danga may nopp

(wakhal ak xalé bi thi kaw)

Mane damala nopp
Soo beugué sunu ande nekh
Yow danga may nopp

(dañouy dem wala dunu dem?
Nieuwal)



Credits
Writer(s): El Hadji Fall Diouf
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link