Thiapathioly

Deff Music

Zeus (Zeus Zeus)
Thiap thiap sauce
Check

Tchi kaw tchi kanam (tchi kaw)
Boul lathieté fana (tchi kaw)
Hey Thiowli mana (tchi kaw)
Boul lathieté kana
Yaag may seen tchi kaw thi kanam (tchi kaw)
Boul lathieté fana (tchi kaw)
Hey Thiowli mana (tchi kaw)
Boul lathieté kana
Yagmay seen si kaw si kanam (tchi kaw, tchi kaw)

Thiapathioly (tchi kaw)
Hey tchi kaw
Boul lathieté kana (tchi kaw, tchi kaw)
Thiapathioly (tchi kaw)
Hey (hey tchi kaw)

Fuck séni règles guissoumako douma diank
Yallah ak Gueye rek laafiy sant waw
Meme bookoy wakh si souf boy maguessi kaw ni jant
Maa shaa allah ma laali bant

Loutakh bou goud lagnmay laalé
Dou am téguiin boumlay waathié
Xath bou mbeuw ngueu teh doo maaté, maalay faalé loutakh
Dieul sa gatt gui def si valise
Diaaré Paris dem italie,
Rap bi dokhoul maagui niaaly
Accélérer dikaat

Time is money loutakh loo gueun beuri temps di banque
Ballou fital nekoul gamou Fifa ODCAV
Gueumeul yallah comme bi Deschamps di woo Benzema
Nigger coup d'Etat bi maakoy poser sans ben conséquence

Succès la mèrebi niaan, rap galsen mayma nopp
Xam ma par accident boum nga tek ma choc
Méréma di sakhar sa guel bi manela nopp
Fouleu mooy diaay dakhar
Niakk fayda sa bopp

Tchi kaw tchi kanam (tchi kaw)
Boul lathieté fana (tchi kaw)
Hey Thiowli mana (tchi kaw)
Boul lathieté kana
Yaag may seen tchi kaw thi kanam (tchi kaw)
Boul lathieté fana (tchi kaw)
Hey Thiowli mana (tchi kaw)
Boul lathieté kana
Yagmay seen si kaw si kanam (tchi kaw, tchi kaw)

Thiapathioly (tchi kaw)
Hey tchi kaw
Boul lathieté kana (tchi kaw, tchi kaw)
Thiapathioly (tchi kaw)
Hey (hey tchi kaw)
Tchi kaw tchi kanam (tchi kaw)
Thiapathioly (tchi kaw, hey tchi kaw)
Boul latché kana (tchi kaw, tchi kaw)
Thiapathioly (tchi kaw, hey tchi kaw)

Hey Gnidaat
Kheep rappeurou village
Sen thiokk yi laay guitare
Gueun di reew ni fisha
Zeus toth na reew mi bilaay
Doyla tontu si ladj
Waagnil sa dayak di laab
Khontal khel mi syllabe

Si kaw sa kanam comme maquillage
Fii wak yaw mal kiyam
Rayla dagann comme si jihad
Roukhal nikouy billard
Yoonou tekki laa dieul ila
Wave Ecobank Ria
Realité bilay reukat
Tankou talibe di ziaar motherfuck

Poucave ni 6nine
Sa guel laay 6neuf
Oothentik moogui nice
Sonwam yi sikk neu
Nieuw doumeu leen si mic nioumay diaay wowlé beut
Everyday every night ma diapleen di teuf

Tchi kaw tchi kanam (tchi kaw)
Boul lathieté fana (tchi kaw)
Hey Thiowli mana (tchi kaw)
Boul lathieté kana Yaag may seen
Tchi kaw thi kanam (tchi kaw)
Boul lathieté fana (tchi kaw)
Hey Thiowli mana (tchi kaw)
Boul lathieté kana
Yagmay seen si kaw si kanam (tchi kaw, tchi kaw)

Thiapathioly (tchi kaw)
Hey tchi kaw
Boul lathieté kana (tchi kaw, tchi kaw)
Thiapathioly (tchi kaw)
Hey (hey tchi kaw)
Tchi kaw tchi kanam (tchi kaw, tchi kaw)
Thiapathioly (tchi kaw, hey tchi kaw)
Boul latché kana (tchi kaw, tchi kaw)
Thiapathioly (tchi kaw, hey tchi kaw)

Hey kou taathiouwoul
Kou Taathiouwoul
Mané kou taathiouwoul
Kou Taathiouwoul
Niou dem hey

Kou Taathiouwoul
Niou diaay sa maam
Dieunder ko album teh dooko cons
Kou Taathiouwoul
Niou diaay sa maam
Dieunder ko album teh dooko cons
Thiapathioly



Credits
Writer(s): Baye Dial Gueye
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link