Am Wala Ñak

Keep kou la bayi nguiir aduna
Bayiko té dessé ak Yalla
Yalla yoor mbiiram, yoor sa mbiir (hun hun)
Barri na loy nawé niit
Walahi bo xamone lamou niak door ko am
Di nga xam ni amoul wayé dafa gueuneu niakka

Deff Music

Check
Am wala niak lep yallah leu
Mais takhoul nit tègui si lokhom
Amna am am you sax niak gueun
Dou kou gnak rék torokh
Esk nak mboolo mooy doolé fou béneu nitt di lekk alalou mboolo
Bignkossiy guèn café meunoul soukeur
Beugouleu fay naar bi khorom

Benefice feegn na mais fayoussi borom
Lekk na akh mais dou feegn si boolam
Lépeu leu raath dieumeulé thi boram
Khol baagui takk yallah fayna kholam

Defna ni mom domam doon na doomam
Beugoul lim beug baye dja rayna doomam
Bayoul di doundei khagn na lekk doomam
Baykatt bi dead na doomam diayna toolam

Amga alaal
Amoo nitt
Sa chien de garde
Moola faat

Oh my god
Awma gatt
Tok di khaar
Ndool dila faat

Sama yoon
Si iow la kane
Lane ngueu meun walabok lane nga xam

Fuck sa niakh
Fane nga far
Koula yabal negger iow la kane

Bagnkat ba bagn sa bop yeufou doff leu
Gnee katt ak loum meunti am dafay pauvre
Gnee katt lougn beug amko esk noon leu
C'est pas toujours k l'argent fait le bonheur

Paré fay louné pour laver sa honneur
Waw setal sa der bala biss bignlay sangu
nakh lep ngafiy baayi sa dieuf yilay topeu sax daniufiy dessaat ndekkei mooy sa alal

Kii dafa am faaté yaayak baay (iyeah)
Kii bamouy am dafa niak yaay (iyeah)
Des fois nak niarignou li nga am (iyeah)
Niak rk mooy takh nga meun ko xam (iyeah)
Amna niou doyloowoul louniu am (iyeah)
Nane laniuy doyloowé yallah (iyeah)
Néwougnla nga doylo li nga am (iyeah)
Mooy nga bagn wouti loo niak (iyeah)

Lou kheuy sootiiii amoul
Yallah noopiiiii
Nakh moo am
Teh meunoul niakk
Yallah am
Teh dou niak
Yallah rek am
Meunoul niak
Yallah am
Teh dou niak
Yallah rek am!

Yeah Amna niou khiif mais chak jour niou guiss nitt di touridji lek
Amna niu tiim sen deukeundoo waayé mayougnko kerr
Amna niu miir amna niu tarkhiiss ba niak si ndaw
Rangooniu liir bouniu saani tokhoul fim wara tokh

Amna niu niak mbeuguel si baye mais doom nak niooko fonk
Amna niu amoul mbeuguel si sey mais doomalenfa takha tokk
Amna niu yallah may dieukeur si kaw niéneen waayé beugougnko bokk
Amna niu mbeuguel, tagaleek sago parce que nioom dagnléna wor

Yeah ndakh Valeurs ak principes, guètt booy sammeu leu
Beug lep légui guent bouy sank leu
Erreur booy rèthiou day melni sank leu
Mais nitteu matoul ndioumté pour diang leu
Niakagoul dara boudé toutt tank leu
Weer lep thi kenen teklé say tank leu
Mbeur boufi daanou pekhei bou antou leu
God wakhoul dara tèreem di adouneu

Nitt dina def louko niakaloo li gueneu cher
Nitt dina fèn fèn ba am deug si kaw gnissi dess
Nitt dina dead fekkifa loumou amoulwoon si souf
Nitt dina dem baayifi ay dieuf youko terei mouth

Amna ay milliardaires si séni bop you nékoul ay millionnaires si séni compte
Amna ay milliardaires si séni compte You nekoul ay millionnaires si séni bop
Nit dina bagnal kou am mayou yallah
Tek yallah nit kou am mayou yallah
Nit moogui defar nitt moogui yakh
Mais nitt niaakoul dara bou amé yallah

Lou kheuy sootiiii amoul
Yallah noopiiii
Nakh moo am
Teh meunoul niakk
Yallah am
Teh dou niak
Yallah rek am
Meunoul niak
Yallah am
Teh dou niak
Yallah rek am!

Gni am Yalla, Yallay buur
Gni Gnakka Yalla, Yallay buur
Am Yalla, gnakka Yalla, Yallay buur



Credits
Writer(s): Baye Dial Gueye
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link