Ghost Mode

Papelaye I see ya
Yeah
Ghost Mode On
Leggo

Kuma wo si beat wo nga Peul si guxum soow
Saltigek xoy mba thioye thi mbuuxum Oooh
Amoul yaxal teyal sa taw ni ku dadj amoul yakaar
Why you act like you don't know act'art
Tubel gaw malaka xamul bakaar
Non may njaccar doma jaay taar
Todj Parék New York non namuñ Dakar
Waxx ma loy tite naaxu tocard
Son yé rélu boy ni Maxu pobar
Lyrical murder ñeme kaay ñu contact
Fiñ ma mene moy si aru koba
Diplome yi sam poche
Di fo si rap comme Neymar bou santos
Ñi def rap sen job
Kuñ massi bolel ma taal ko sans coss

Pauvreté bi sen champ lexicale
Daf may diox envie yeg si gale
Waxuñ fi dara ni Macky Sall
Nang aka Ngeb ni kuy lekki xaal
Pauvreté bi sen champ lexicale
Daf may diox envie yeg si gale
Waxuñ fi dara ni Macky Sall
Nang aka ngeb ni kuy lekki xaal

Bayi ma conss samay dadj ma nigga
Flowou whyski lafi tadj mandiga
Bou rea di guiss real
Doma guiss fake
Non dou mistake sa kaw ma ngi fa
Duma alcapone mais bandila
Doma sen ba dima diote I'm in a
Ferrari te ya ngi xeex si raps yi
Non fils diapsi du maak yaw diangil rap
Da nga ni drill yi daay poup sa nope
Dielel bi shit mo nara oup sa bope
Rabbofi gate beg fi ñodi star noy ame fans youdoul sa mbokk
Ma ngi rap ya ngi diem
Ya ngi back ma ngi dem
Lo fi bax rek ñu nger ko doxx sa yo dege dadj xamal ni man itam
Gene hit non dou fils tête
Kou jog guene mbalit toude mixtape
Yox la guiss nga non Palaye Why Gee ñoy tew si game bi def diff check
Di nga rap ba rap do guiss cheque
Koussi sorou sa baay def mistake
Dougn sa mapando kougn boul gnou topando
Fils la nga dëke di wër ño ko biff tek
Bokuñ defi menuñu bok devise
Comptel saay million de vue
May impacter millions de vie
Bokuñ defi menuñu bok devise
Comptel saay million de vue
May impacter millions de vie yeah



Credits
Writer(s): Youssoupha Gaye
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link