Bgst

Yeah Ah
Kill na sa rappeur mu faatu
Mene na rap moytu ma thiaatu
Rer na te neku ma aatu
Bu de flow rek mane amnassi aay saaku
Mane la matar awma kaagoul
Sa guemignou rappeura ngaamu
Sang sa rappeur ak ndiampe ak saabou
Kouma fi dakha rap amoul
Thiobal sa thiakri ma ngi ni
Youkholen sathie bi ngagn mi ngagn mi
Gorla ak diassi bi day melni gnabry
Defarlen sappe yi boy yenay sathie yi
May perte khaliss bi
Aile bi dofi romb boy mane la hakimi
Saw sa kaw di melni apprenti car rapide
Dam lay kot ni dembele rek nga saraani
Assassin dou messe dug bir paradis

Oooohhhhh damn man
Boy defal nank defal nank defal nank defal nank defal nank
Humm

Thiatou game thiatou gale
Taatunen si ñi koy thiatou man
Tatioulen ñun la wa Thies
Ambiance stress ñu wathie
Balla Gaye flow I don't care
Kouma tekku di beef wol ko Sa Thies
Ko guiss ak couronne youkhoul Sathieey
Tokk si trone nama faay sama loyer
Dakh la rap fils dou gathie
Dañ ko mene suy si ma tay
El Gee yaay déféant
Yobou retraire ay vétéran
Déféna li nga young teksi different
Dina far yokk liste gni dem Ipres diffa rang

Balla Gaye Sa Thies
Balla Gaye Sa Thies
Balla Gaye Sa Thies
Balla Gaye Sa Thies
Balla Gaye Sa Thies
Balla Gaye Sa Thies
Balla Gaye Sa Thies
Balla Gaye Sa Thies

Ya ngi table de 4 ño ngi pivot de Gauss
Fo ñu sen sa droite pivotel gauche
Noto duggel droite da gni gene gauche
We control the power like Tommy and Ghost
Tikki takka une deux une deux
Dañ koy këlëptiko yak sa ñangalu guinar ngay cocorico
Sen rappeur yëp lay guenel kalashnikoff
Why Gee El Gee si feat Ñu dikaat guxx sa fit
Pape Laye diox ñu beat Ñu dikaat def si hit
Diokh gnu 10 titres si style bou la sweat gnou spit si beat ni fouki flic you xif lif
Ma ngik bic bi na niquer beat yi I don't speak English you are the bitches

Sa Thies Balla Gaye
Sa Thies Balla Gaye
Sa Thies Balla Gaye
Sa Thies Balla Gaye
Sa Thies Balla Gaye
Sa Thies Balla Gaye
Sa Thies Balla Gaye
Sa Thies Balla Gaye



Credits
Writer(s): Youssoupha Gaye
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link