L'enfant Prodige

This beat is Fresh

La la la la la
La la la la la
La la la la la
La la la la
La la la la la
La la la la la
La la la la la
La la la la
Oh yeah
We know
Oh yeah
You know
Oh yeah
They know
Oh yeah

Figua diogué
Nimou soré
Figua yeksi betoul kene
Sounou kanam gua dorè
Donone boy bou ndaw nioulay setane si kaw scène
Guissone si iow Lou yémé
(Guissone si iow Lou yémé)
Legui nieup guis nagn nigua yémé
(Guiss nagn ni nga yémé)
Dou mane reka ko sédé
(Dou mane reka ko sédé)
Moussougn guiss sa kanam loudoul niémé
(kanam loudoul niémé)

Anhannnnn

Ragal niémé wouko badiko fréquenter
Gun ak défaite victoire moy meusseu dox sisen digueunté
C'est déjà fait Gun ak boppam lolou Lagn diguanté
Moussougnko ngemb mou dem beuré nieuw indil niou gatié
Guissouniou fougnko daké

Omar keita newone nala lodefa geune lo defoul
Boul meusseu wax balene niouy wax oubil sa xel bi degloul
Yagui si yone boy dox ba xaméto sa bopp deloul
Xaley bou boppam oyofoul gua tegg la yene bi teloul

Ey petit frère boul tegui tank
Deko tangual bamou tangue
Fils moytoul doug si camb
Garannn si iow lagni diang

Thia kaw thia kanam amoul diade
Même soniou wowoul dagni diap
Na fane yi goud amal diam
Nala yalla mousseul si thiate

Goooooo



Credits
Writer(s): Momar Ndiaye, Mouhamed Loucar
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link