Feu De Joie (feat. Llas Melo)

Hey yaw
Boul nopi wax ma
Niaka xam motax ma nieuw ladj la beug nga waxma

Ey yow tahawal haarma
Niak ham Yon bé waral malay wo beug ga wanma

Hey yaw wanma
Ndax dou nene nga magma
Guisnani jamono yi niou né dounde bi tarr na

Deugleuh
Doundou bi tarna
Nieup guiss deuk bi hatna
Yeah
Kounek sa bop
Kou meun sa morom wanko sa dole

Ohhh c'est le feu
C'est le feu
Le feu
C'est le feu
Li dafa metti
Yeah dafa meti
Li dafa meti

Ohhh c'est le feu
C'est le feu
Le feu
C'est le feu
Li dafa metti
Meti yaw
Meti yaw C'est dure

Ey yow diant bi fegn na
Leep li leundeumon ci sa ma bopp legui lerna

Hey yaw Deug bi fegn na
Niakarek tiss bi mourone sama Beut yi deugn neu

Ey yow degn na
Lima ragalon déé na
Néwon naniou ma Lou metti yagoul legui Lep diehna

Yeahhhhh
Legui lepp diexneuuuu
Lekk na sama dieuw ress neu
Yegeutouma xiff
Mara touma nane
Dounde jaam nexna
Ah

Ohhh c'est la joie
La joie, la joie, la joie

Yaw it's joy
It's joy, it's joy, it's joy

Ohhh c'est la joie
La joie, la joieeee

Oh it's joy
It's joy, it's joyyyyyyy



Credits
Writer(s): Babacar Sall, Momar Ndiaye, Mouhamed Loucar
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link