Leundeum

Majestic Drama

Fou ma meuneu né jot sa appel, bae fo né
Lima meuneu def nga nema bae, no no no no dou way
Allo, bae fo nekk
Gnibicil, il fait nuit
Wagnil thiow li, jalousie, danga metti
Goora leundeum, goora leundeum, goora leundeum yeah
Goora leundeum, goora leundeum, goora leundeum yeah

Niata goor nioma topeu
Ngamay wakh li dima togn
Soneu na dotouma tok
Confiance bou amoul ci mbeuguel non non dou dem

Fou ma meuneu né jot sa appel, bae fo né
Lima meuneu def nga nema bae, no no no no dou way
Goora leundeum, goora leundeum, goora leundeum yeah
Goora leundeum, goora leundeum, goora leundeum yeah

I say
Jiguene bou bakh, goor bou bone
Takaliko ni diwline ak ndokh
Dama sohlo koumay degue ga Sokhlo koulay deglou
Souma khamoul lima beugue khamna lima beugoul
Yeah
Mais gooreu mel nonou fumu toleu day risquer
Dankey defal jameu kouko sonal lay pister
Bo tegué tank ci biti mou ley call insister
Sa tour ci sama khol ndakh nenagn khol day guissé
Amna lou meuti
Ndakh soumla woré bayi beugouma leu guiss ak kenen mais
Est ce que dama toxic
Est ce que dama toxic
Jeul sa khel bi dokh ci, jeul sa khol bi tok ci, leundeum

Goora leundeum, goora leundeum, goora leundeum goora leundeum goora leundeum
Yeah yeah

Kone Wakhal goor yilay topeu
Ni demo feneu fi ngay tok
Nioune niar nio changer mou dem
Effort su amoul ci mbeuguel non non dou dem

Fou ma meuneu né jot sa appel, bae fo né
Lima meuneu def nga nema bae, no no no no dou way
Goora leundeum, goora leundeum, goora leundeum yeah
Goora leundeum, goora leundeum, goora leundeum yeah

Credits
Writer(s): Abdoulaye Diop, Aissata Guisse
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link