Delouci (Bonus Track)

Yeah yeah yeah
Bad man Miézé

Beugeutouma nga may bayi
Ndakh bo deme dina die
Lima beugue moy nga nieuw niou delouci
Bayi sa thiakhane yi nga nieuw niou delouci
Kay ma press leu sama yaye
Nangma yobou ci seu bayi
Na ko wakh ni nangeu nieuw niou delouci
Bayi sa thiakhane yi niou delouci

Wakh ma cheri entre nous
Beugouma loudoul gnou am beneu rendez-vous
Fouma wet ak yow assamane bi dotoul kawé
Geum na ni adjana so feu nekoul ma wet

Go shorty, no def
Kou beugue deukeu si sa khol noy def
Dakh beugue na niou andeu doundou noblesse yeh
Def lo beugue di leu wowé altesse yeh
Dina deh pour yow
Gaindé bouy nelow yé pour yow
Assamane bi na ko tey pour yow
Guedj bi yeup dina ko fey pour yow

Yow la, yow la, yow la, yow la, yow la beugue
Kone wo ma sa yo sokhlo ku la wetali
Mane ak yow kasseh kene doula ko netali
Yow la, yow la, yow la, yow la, yow la beugue
Kone wo ma sa yo sokhlo ku la wetali
Mane ak yow kasseh kene doula ko netali

Beugeutouma nga may bayi
Ndakh bo deme dina die
Lima beugue moy nga nieuw niou delouci
Bayi sa thiakhane yi nga nieuw niou delouci
Kay ma press leu sama yaye
Nangma yobou ci seu bayi
Na ko wakh ni nangeu nieuw niou delouci
Bayi sa thiakhane yi niou delouci

Wakh ma cheri entre nous
Beugouma loudoul gnou am beneu rendez-vous
Fouma wet ak yow assamane bi dotoul kawé
Geum na ni adjana so feu nekoul ma wet

Magui mel ni, kouy rever
Sa teint comme lem ak or babe
Say beut rek meune negn ma rey
Bo sigué meunouma seugue

Dina deh pour yow
Gaindé bouy nelow nako yé pour yow
Assamane bi na ko tey pour yow
Guedj bi yeup dina ko fey pour yow
Iyah

Yow la, yow la, yow la, yow la, yow la beugue
Kone wo ma sa yo sokhlo ku la wetali
Mane ak yow kasseh kene doula ko netali
Yow la, yow la, yow la, yow la, yow la beugue
Kone wo ma sa yo sokhlo ku la wetali
Mane ak yow kasseh kene doula ko netali

Beugeutouma nga may bayi
Ndakh bo deme dina die
Lima beugue moy nga nieuw niou delouci
Bayi sa thiakhane yi nga nieuw niou delouci
Kay ma press leu sama yaye
Nangma yobou ci seu bayi
Na ko wakh ni nangeu nieuw niou delouci
Bayi sa thiakhane yi niou delouci



Credits
Writer(s): Abdoulaye Diop
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link