Rddr.Wav

Yo
Nokoss di Rokoss ragal dou djégui rail
Fi weuk niogui diote cii mic nioune douniou ko tégui right (mafuckaaa)
D Squad doutoul xeuthio pé bi waay
Cii hood la lep doré taay dém neu ba djégui daay
P.A kinePi Roythia ba guédiawaye
We don't Give a fuck baate bigni naane guédd-waay
Bougni dokh cii hood dagni Oyoff Ni butterfly
Butterfly dagni Oyoff ni butterfly

Yo Yo Yo
Téwal hood nigga cii track ndiap di deugueul kap
Hot shit what a fuck S-quatt nioune guemouniou pop
Lamp ghetto yépeu fay niouy dokh di gueume di yott
Sèni ngour beuri faay lépp rek cii gueumeu di God
Niouy gueuneu di rock sani séni bagg niou seug di roteu
Justice bi joxé séni ass doni tott
Wadiour yi sonou keur you fess yi niou bott
Hood bi né jungle
Young Boy deungeul
Only Mother Fuck Hip Hop bégnou yégueul
Deuk fi di yomb kou amoul fiit dou rombe
Fokk nga ndaguu diayanté wala niou weurleu nomba
Life bi boudé tééré dagni xeuy di nafar
Hood béniou défar koufa diougué nio far
1 Luv 1 come on nigga doni soldat

Nokoss di Rokoss ragal dou djégui rail
Fi weuk niogui diote cii mic nioune douniou ko tégui right (mafuckaaa)
D Squad doutoul xeuthio pé bi waay
Cii hood la lep doré taay dém neu ba djégui daay
P.A kinePi Roythia ba guédiawaye
We don't Give a fuck baate bigni naane guédd-waay
Bougni dokh cii hood dagni Oyoff Ni butterfly
Butterfly dagni Oyoff ni butterfly

Yo Yo Yo
Soma toppé cii hood dagay rér ndaxté mino
Samay home boy dougnou leu feel ndaxté clean no
Ghetto amena crack amena yaram amena Ino
Dagni téleu yéwou hustle hard dass nimo
Sabab dioxé loufi né au Maximum
Diouk outi Xeuy ni niou kay wakhé mak Simon
Xarou niou sa ngour cii God lagnou wékou
Liniou dall dou niak diom life béniou diékou
Na dokh bi gaw my nigga boul wakh ni sékou
Diouguel foutékou fass yéné fight ba diote sa lékou
Chod up all my home niggaz yi di niafé
4 Real
Do meusseu guiss fu sunu beut di raffé
Yegg yegg bou kawé waral dokhaline yi deugou
Ragal dou djégui rail ndaxté xamena likoy reubou
Again to ziar nga degg po po po po

Yo
Nokoss di Rokoss ragal dou djégui rail
Fi weuk niogui diote cii mic nioune douniou ko tégui right (mafuckaaa)
D Squad doutoul xeuthio pé bi waay
Cii hood la lep doré taay dém neu ba djégui daay
P.A kinePi Roythia ba guédiawaye
We don't Give a fuck baate bigni naane guédd-waay
Bougni dokh cii hood dagni Oyoff Ni butterfly
Butterfly dagni Oyoff ni butterfly

Yo Yo Yo
Oyoff ni Butterfly
Di Holla sama hood
Proud cii lima done douma talal sama hand
I represent my people nigga séneu ma cii kaw
Dara dou takh ma sopi sama mélo ak sama djiko
So beugué done hero na nga ma wane fayda
Wathial cii mbede bi done number 1 fighter
Gangsta wékouwoul cii prek wala diaay tarr
Lucidité mind bi ngay démé moy sa lighter
Ragal dou djégui rail!
Why?
Face yi nio indice bouniou diapé fake et reste
Douniou call police
Bang Murder Like street order

Yo
Nokoss di Rokoss ragal dou djégui rail
Fi weuk niogui diote cii mic nioune douniou ko tégui right (mafuckaaa)
D Squad doutoul xeuthio pé bi waay
Cii hood la lep doré taay dém neu ba djégui daay
P.A kinePi Roythia ba guédiawaye
We don't Give a fuck baate bigni naane guédd-waay
Bougni dokh cii hood dagni Oyoff Ni butterfly
Butterfly dagni Oyoff ni butterfly

Credits
Writer(s): Nitdof, Papa Kandé Sidibe ( Mao )
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link