Melokáane
Diakhlé ma tax di ladji
Ndax liwone mome wonénina
Teranga diangay déme – Kéne xolatoul sa morome
Nitay liguéye morome nguir ignane
Soxor – niaak gueume yalla
Interet tassna rewmi
Lou waye def morome – amna loumou ciye sentou
Boul guiss nite ki diko bagne - Kokou defoula dar
Boul xole nite diko djiépi – Ndax lolou waroula yow
Boul tite yow – boul délou guinaw dome
Mani boul xébe – boul bayi gna nga dekeulone déme
Hée bilaye walay – méréwoumala yow yaye sama xarite
Bilaye walay meréwoumala seute yaye sama yaakar
Keupe kou eupe sa morome doley wala alal wone nalako
Kéne défoule nguir yalla – kofi digaléle mou warla
Téranga dja ngay déme – bax mome moungui nara
toumouranké
Djiko yi cii neg bi laa yakho – dial ci mbéd mi – laaw ci
rewmi
Boul guiss nite diko bagne té nite kokou défoula dara
Boul xole nite ki diko djiépi té kokou mome défoula dara
Boul tite yow
Boul délou ganaw dome
Mani boul xébe yow
Boul bayi nga nga dekeulone déme
Han bilaye walay merewoumala dome – yaye sama nite
Bilaye walay méréwoumala waye – yaye sama yaakar
Sa melokáane mome laniou laay raagné - Han boufékéni
Lou nekh la modi nieuw
Sa melokáane mome laniou laay raagné - Han boufékéni
Han damay woye séne toure
Sa melokáane
Weurseuk bi nieuw daniou nane tiénou bateau mome
mounouko téyé
Ndax yalla moye déf lolou
Jaam limou nara ame laay ame
Djiéguici léne – ma woye borome melokáane you raféte
yée
Yalla moye déf lolou
Han lou meunta gnak fo'k mou ame
Nako di déf ngay xole
Nako di déf ngay séeune
Nako di déf ngay xole yaye
Jaam mome, limou nara ame laay ame
Sa melokáane mome laniou laay raagné - Han boufékéni
Han toudou naniou sa toure
Sa melokáane mome laniou laay raagné - Han boufékéni
Han yow mate nga ndjite
Yow toudé nanioula dome
Yow da nga raféte xole
Han toudé nanioula dome
Adjia Seynabou Faye laay woye
Sa melokáane raféte yaye bo law cii saaye domes
Papa Badara Mbengue bayou Elage ak Babacar
Thioro Mbengue Mor Papa bakh nga lolou
Bayou Maman Soda Ak Cheikh Mbacké daamay koye
woye
Kor Ndéye Diaw - Cheikh Dieng raféte ngéne melokáane
Moustapha Guéye Ndioro kor Bercy ak bayou Cheikh
Wa Ndar guédji tey laay woye séne dome djié
Kor Rama Ndiaye - Papa Diop raféte nguéne melokáane
Massata Ndiaye kor Astou woye naléne thia Montréal

Credits
Writer(s): El Hadji Fall Diouf
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
Other Album Tracks
© 2024 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.