Foula ak Fayda

Tey laley yobou fou sorri fi
Khamni mak yow dong ley done
Ndakh ni mey guissé ak ni nguey guissé
Nonou la gnou wouté mane ak gnom
Lolou boko deffé dinassi dem
Te khamni defay li bakh
Lolou mo tchi gueune

Foul'ak fayda
Bo amé foul'ak fayda yow
Té nga gnow gnou dem
Foul'ak fayda
Bo amé foul'ak fayda yow
Té nga gnow gnou dem
Foul'ak fayda
Bo amé foul'ak fayda yow
Da nguey gnow gnou dem

Mane
Souma ley guiss damey begg
Sama xol bi di nekh
Yaye sama reini xol
Yow la
Gnowal gnou dem fofa
Ah
Damey begne gnou tiatou gno
Sunu weurseuk dadi fey yeem mane ak yow chérie
Ndakhté
Ndakh ni mey guissé ak ni nguey guissé
Nonou lama wouté mane ak niom
Té bokko deffé dina tchi begg
Khamni da fey li bakh
Lolou mo tchi gueune

Foul'ak fayda
Bo amé foul'ak fayda yow
Té nga gnow gnou dem
Foul'ak fayda
Bo amé foul'ak fayda yow
Da nguey gnow gnou dem
Foul'ak fayda
Bo amé foul'ak fayda yow
Keneu doula yeep

Mane
Beurki demba la tokk dila khalate nane hey Fi
Han bo gneuwé
Di nga begg
Na leu soukkal
Na leu ramal
Na leu defal li nekh
Bébé loula nekh
Nekh nama

(Hey yow hey)
Yeka ma khamni ya ngui sama wett
Dima nob dima beggal (Hey yow hey)
Yeka ma khamni ya ngui sama wett
Sama xol bi dey nekh (Hey yow hey)
Gnowal gnou dem m...

Dem
Dem
Dem dem dem dem dem dem fou sorri

(Hey yow hey)
(Hey yow hey)
(Hey yow hey)
Defal li nga meune
Ma guiss ni ya ngui fekh (ya ngui fekh)
Demal ba diekh
Foumou yeem nekh
Han chérie

Dem
Dem
Dem dem dem dem dem dem fou sorri
Dem
Dem
Dem dem dem dem dem dem fou sorri



Credits
Writer(s): El Hadji Fall Diouf
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link