Xoslou

Damka xoslaa ba aksi
Yaye boye waxoone na dina tekki
Gnidoone lathe té loy deff fi
Légui nioy gneuw galé dimeu setsi
Sama son daw fepp ni taxi
Éleves yii jangue takhaw recité sama textes yii
Mane dama trun beurek mbed soga sekki
Mane waxone nala sama kagn nako lékki

Yao boul ma méré xaral touti rek ma nétalila
Mane fimeu jaar lallaay teggal ndax mou wetatli

Meussouma nangou gnoumay sangue di xole sama tate
Meussouma nangou moudié bole di xeuthio aye mathiate
Responsable taw la mbok duma thiate
Damay tekki sama neggu mame lako ndiekeu watt
Chance sa geuneu licence manam dou BAC moy gnoulouk thine
Mbed mé ngui jaax t fokma ame aye dale jean
Sama sho bi néna mbenguel taxoul guemigne gui niin
Gathié gué ngui xaar té loukay facc dou aye niwachinine
Pa bi demna alakhira bamak mere bi
Rak yéngui sentu guissa gouniou weer bi
Mbok yii defénouma bayi ma ak guerre bi
Fou am vie am espoir damay dem beu jeex
Wirir jaari ndari aksi ni saneex
Yaye dji mougne domdia maag xolam dina feex
Course obstacle teupp beu tasse pour soga térr
Maafi deff miracle waxko haters yimay saani xeer
Diok ak danu jangue dokh ni lire bouy soga ferr
Yallah teuthie na bountou wathié rideau bamak palanterr
Yao geum naani kou melni mane mbed dafko tandass bruh
Té fimeu jaar dafa beuri lol aye carcasse bruh
Ma dieul jome fiit xell bolé bandasse bruh
Guissoni mangui wexx tale comme xalissou pro

Damka xoslaa ba aksi
Yaye boye waxoone na dina tekki
Gnidoone lathe té loy deff fi
Légui nioy gneuw galé dimeu setsi
Sama son daw fepp ni taxi
Éleves yii jangue takhaw recité sama textes yii
Mane dama trun beurek mbed soga sekki
Mane waxone nala sama kagn nako lékki

Yao boul ma méré xaral touti rek ma nétalila
Mane fimeu jaar lallaay teggal ndax mou wetatli
Yao boul ma méré xaral touti rek ma nétalila
Mane fimeu jaar lallaay teggal ndax mou wetatli
Yao boul ma méré xaral touti rek ma nétalila
Mane fimeu jaar lallaay teggal ndax mou wetatli
Yao boul ma méré xaral touti rek ma nétalila
Mane fimeu jaar lallaay teggal ndax mou wetatli

Dioudou fou ni fank
Dé baafi louné wéngg
Guisso fouma diengue
Mangui siw ni marché zing
Sama son si callou boy yi mel ni diamono school
Légui mangui yeungeul town bi am diam nosse cool
Ame respect thi succé deuggeur bopp laafi aksé
Fign téré la téeréé gnidoone cissou laafi vexer
Loma jaay meu dieunde
Loumay doyé di sathie ndeundeu
Souma togone rek di xolé kone dina dé thi mbeundeu
Taba-taba takalé
Fedou moma japalé
Guéné ma maiga yobouma planet kebap
Fi leep jaam sama dome dou dem mbalite toubap
Level be ngui thi kaw mo waral gneup dimeu bapp
Légui waxal bou thiolé fonek ma wari lako
Mangui solak ka soumi ni kou gagner loto
Boy you ndiole xess nekh ni ndokhou coco
Langalmako mane ak Papa Niang gnon gui dawal auto
Newoone nala Ma' nala wouteul écran plasma
Jangue thi mbed jeul pé sama classement
Niaka méti yaag mais am da gaw ni boulou taak
Level thi kaw di flotté sama fita ko taak
Keyti néna limay binde lepp okay
Karim neko day am dara bess bou mokké
Dumassa ami facebook menoma bloqué
Okay dawal sama biz dilen moquer

Damka xoslaa ba aksi
Yaye boye waxoone na dina tekki
Gnidoone lathe té loy deff fi
Légui nioy gneuw galé dimeu setsi
Sama son daw fepp ni taxi
Éleves yii jangue takhaw recité sama textes yii
Mane dama trun beurek mbed soga sekki
Mane waxone nala sama kagn nako lékki

Yao boul ma méré xaral touti rek ma nétalila
Mane fimeu jaar lallaay teggal ndax mou wetatli
Yao boul ma méré xaral touti rek ma nétalila
Mane fimeu jaar lallaay teggal ndax mou wetatli
Yao boul ma méré xaral touti rek ma nétalila
Mane fimeu jaar lallaay teggal ndax mou wetatli
Yao boul ma méré xaral touti rek ma nétalila
Mane fimeu jaar lallaay teggal ndax mou wetatli

Yao boulma nié xaral touti rek ma netatlila
Mane guisna ngamay xole di xole rek beu sepalima
Mane dama gnaffé xoslou fepp beu aksi fi
Geum geum bou deugou beatou bbeut massiye teuss teuss si
Yao foleusophie xoslou man leu
From zero to hero lolou sa niane leu
Yao Banguassi waré japp da nga bayi mou cedd
Nga baayi bama taak ngani da ngay oupp

Credits
Writer(s): 4leuz, Bbeut
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link