Goor God

Goor God la toudou
Dou Yéwou xaar mouk
Gnaffé loumou beugueu
Djoulé tax mou souk
Dou tiogou dou gnegne
Tchi allalou keneu
Kokoy Goor God
Goor God
Goor God la toudou
Dou Yéwou xaar mouk
Gnaffé loumou beugueu
Djoulé tax mou souk
Dou tiogou dou gnegne
Tchi allalou keneu
Kokoy Goor God
Goor God

Mane Goor Yallah deugueu laley tégal fils
Kou doundak xol bou nice
Déh ak bénéfice
Kou tok sakh tchi khaar
Yone bi gueuneu diss
Sorrou tey mou deugueur
Bou khadi
Kodj ko benenen beuss
Diamou Yallah
Conscience bou tchill tchi Diné yeup
Xaliss amna xeet
Sou léwoul xegn ni nene bou neup
Doundou tchi noflaye
Wakh ma lou ko gueuneu neex
Niakka gueum sa boppa
Tax nga tiogou domou diw ak diw
Niémel beuy sa war
Moytoul ndiabote dji déh si liiw
Boudoul Ndeye ak Baye
Takoul takhaw nga gueuneu xekh
Yanguek diabar ak dome
Fekhel na wasslou si akh
Ngor ak diome moy leep
Goor Yallah waru ko niak
Nga yéwou tchiine bi deupou
Nga wara dippi sa mind
Boumou metti tarr sa bord
Nga key diéma sippi sa guine
Loudoul Yallah nene la
Weddi ko gueume ay guinaw keur
Kharé ba deh
Nopalou ba sa guinaw ngandame tieur

Goor God la toudou
Dou Yéwou xaar mouk
Gnaffé loumou beugueu
Djoulé tax mou souk
Dou tiogou dou gnegne
Tchi allalou keneu
Kokoy Goor God
Goor God
Goor God la toudou
Dou Yéwou xaar mouk
Gnaffé loumou beugueu
Djoulé tax mou souk
Dou tiogou dou gnegne
Tchi allalou keneu
Kokoy Goor God
Goor God

Loumou metti metti
Goor Yallah gueum na di na tchi guéneu
Tiow li barri
Xolam foutou
Lokhom dou dal tchi djiguene
Nekka responsable
Moytou saga ak gawa khekh
Ana sa baye
Mou ngui Noungoussine
Lolou meussta nekh
Yeah
Niongui si town bou barri ay tentations
Mystique ba tedda moy bombeu
Naniou def attention
Yeah
Goor Yallah dey sentou eullagueum
Lou bone dou fenne
Koko def tam sa kaw la dieum
Touki dou tekki
Té tekki tam dou touki lang fa
Tok di takhalé ba tokhi
Tekki tamite amna
Goor god nga
Xam nga am nga gnanou Yaye ak Gnanou baye
Di topando lou bone ba lang si
Non tayi ko waye
Boul gnodi keneu allal
Dey dess si aduna
Dok sa boumou gatié Yaye
Xam nga lolou diadou na
Woyof tollou watié bopam si souf
Mouy taw di nguelaw di neige
Ndiabote dji yeup la bollé ouf

Goor God la toudou
Dou Yéwou xaar mouk
Gnaffé loumou beugueu
Djoulé tax mou souk
Dou tiogou dou gnegne
Tchi allalou keneu
Kokoy Goor God
Goor God
Goor God la toudou
Dou Yéwou xaar mouk
Gnaffé loumou beugueu
Djoulé tax mou souk
Dou tiogou dou gnegne
Tchi allalou keneu
Kokoy Goor God
Goor God

Yeah
Kokoy Goor God
Pape Cheikh Fall, Khalil
Goor God
Tonton Mendy Gorée Island
Goor God
Ibra Dia
Yo
Goor God
Assirou
Han
Goor God
Fallou Bal, Kalla Moula
Goor God
Moussa Felix Mané
Goor God
Tapha Diouf, Pape Ba
Goor God
Sokhna Diop
Goor God
Fatou Wilane
Goor God
Aminta Doucouré
Goor God
Yeah Yeah
Goor God
DD Records
Han
Goor God
Jaxao Kanda
Goor God
Check it
4leuzophy
Goor God



Credits
Writer(s): 4leuz, Bbeut
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link