Xarit
Andando yombeu
(Andando yombeu)
Xaarit jaffé
(Xaarit jaffé)
Noon yi di wax
(Noon yi di wax)
Douniou stoppé
(Douniou stoppé)
Andando bu deuggou dara douko yaak
(No daara duko yaak)
Sunu digeunté bi amoul louko daak
(Dedett amul luko daak)
Nagnou ande dem bougn thi bolé wax
Noon yii lougnou diem diem duko téré baax
Xarit dafa jaffé kone mane ak iow nioye last
Sunu ande lou yallah toudou niit duko tasse
I dont giver damn boy yaye sama best
(Mbok yaye sama best)
I dont giver damn boy yaye sama best
(Yaye sama best)
Fila la deff sama biir xole
Ande bi forever leu lenen doumako xole
Xolo fima deuk xolo lima sole
Xolo tamit sama am am bi mome noumou tolou
Da ngamay bgé témouy deugg
Andak mane do seugg
Lepp ngama oubil sa biir galé duma feugg
Da ngay wax ak mane thi fouleu
Némeu mbok nono nileu
(Da ngay wax ak mane thi fouleu
Némeu mbok nono nileu)
Na nek ak iow di retane xam nga lenen sonalouma
(Na nek ak iow di retane xam nga lenen sonalouma)
Joué play night bi yeup xam nga lolou sonalouma
Xam nga lolou sona louma
Andando yombeu
(Andando yombeu)
Xaarit jaffé
(Xaarit jaffé)
Noon yi di wax
(Noon yi di wax)
Douniou stoppé
(Douniou stoppé)
Andando bu deuggou dara douko yaak
(No daara duko yaak)
Sunu digeunté bi amoul louko daak
(Dedett amoul louko daak)
Yaye sama royoukay mbok da nga bax
Amo loma neube sa life Lepp ngama wax
Sunu wétté tek thine sunu sore facetime
Domou ndey au fin fond rombeu nagnouy gayine
Lgui loumay mine romneu nagn aye xarit
Domou ndey leu mongui fine
Waxal gayine nooni gni ngui bekk gnoun gni gui shine
Dagniy xolanté rétane ndax xam nagn lou nek lepp sunu mind
Ande bi comme iCloud dara douko dindi
(Ande bi comme iCloud dara douko dindi)
Mane ak iow gnoye best friend lolou mo raw OG
(Mane ak iow gnoye best friend lolou mo raw OG)
Yaye sama homie ladial sama honey
mome sax day sissou say photos fess sis ama galleries
Xamoul sunu digeunté be nex ni sow ak thiakiri
Guissouma lou daak li damay tokk di bek di fatelikou sunuy conneries
Tokk di beek di fateleku sunuy conneries
Andando yombeu
(Andando yombeu)
Xaarit jaffé
(Xaarit jaffé)
Noon yi di wax
(Noon yi di wax)
Douniou stoppé
(Douniou stoppé)
Andando bu deuggou dara douko yaak
(No daara duko yaak)
Sunu digeunté bi amoul louko daak
(Dedett amoul louko daak)
Andando yombeu
(Andando yombeu)
Xaarit jaffé
(Xaarit jaffé)
Noon yi di wax
(Noon yi di wax)
Douniou stoppé
(Douniou stoppé)
(Andando yombeu)
Xaarit jaffé
(Xaarit jaffé)
Noon yi di wax
(Noon yi di wax)
Douniou stoppé
(Douniou stoppé)
Andando bu deuggou dara douko yaak
(No daara duko yaak)
Sunu digeunté bi amoul louko daak
(Dedett amul luko daak)
Nagnou ande dem bougn thi bolé wax
Noon yii lougnou diem diem duko téré baax
Xarit dafa jaffé kone mane ak iow nioye last
Sunu ande lou yallah toudou niit duko tasse
I dont giver damn boy yaye sama best
(Mbok yaye sama best)
I dont giver damn boy yaye sama best
(Yaye sama best)
Fila la deff sama biir xole
Ande bi forever leu lenen doumako xole
Xolo fima deuk xolo lima sole
Xolo tamit sama am am bi mome noumou tolou
Da ngamay bgé témouy deugg
Andak mane do seugg
Lepp ngama oubil sa biir galé duma feugg
Da ngay wax ak mane thi fouleu
Némeu mbok nono nileu
(Da ngay wax ak mane thi fouleu
Némeu mbok nono nileu)
Na nek ak iow di retane xam nga lenen sonalouma
(Na nek ak iow di retane xam nga lenen sonalouma)
Joué play night bi yeup xam nga lolou sonalouma
Xam nga lolou sona louma
Andando yombeu
(Andando yombeu)
Xaarit jaffé
(Xaarit jaffé)
Noon yi di wax
(Noon yi di wax)
Douniou stoppé
(Douniou stoppé)
Andando bu deuggou dara douko yaak
(No daara duko yaak)
Sunu digeunté bi amoul louko daak
(Dedett amoul louko daak)
Yaye sama royoukay mbok da nga bax
Amo loma neube sa life Lepp ngama wax
Sunu wétté tek thine sunu sore facetime
Domou ndey au fin fond rombeu nagnouy gayine
Lgui loumay mine romneu nagn aye xarit
Domou ndey leu mongui fine
Waxal gayine nooni gni ngui bekk gnoun gni gui shine
Dagniy xolanté rétane ndax xam nagn lou nek lepp sunu mind
Ande bi comme iCloud dara douko dindi
(Ande bi comme iCloud dara douko dindi)
Mane ak iow gnoye best friend lolou mo raw OG
(Mane ak iow gnoye best friend lolou mo raw OG)
Yaye sama homie ladial sama honey
mome sax day sissou say photos fess sis ama galleries
Xamoul sunu digeunté be nex ni sow ak thiakiri
Guissouma lou daak li damay tokk di bek di fatelikou sunuy conneries
Tokk di beek di fateleku sunuy conneries
Andando yombeu
(Andando yombeu)
Xaarit jaffé
(Xaarit jaffé)
Noon yi di wax
(Noon yi di wax)
Douniou stoppé
(Douniou stoppé)
Andando bu deuggou dara douko yaak
(No daara duko yaak)
Sunu digeunté bi amoul louko daak
(Dedett amoul louko daak)
Andando yombeu
(Andando yombeu)
Xaarit jaffé
(Xaarit jaffé)
Noon yi di wax
(Noon yi di wax)
Douniou stoppé
(Douniou stoppé)
Credits
Writer(s): 4leuz, Bbeut
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
Other Album Tracks
© 2025 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.