Intro
All praise to the most high
Humm
We came from a long way but here we are now
Xamna dina bet ñu beri ñima xamome
Soit kogn buñ bokone
Terrain yiñ bokone, school wala classe yiñ bokone
Liggey wala business yiñ sekone
Té wanoumala wone lima yalla may
Mais est ce dama wara continuer bayi sama passé
Definir fima dieum ak kima done
Lima yalla maay ak lima societe bi tracel
Souma dieloul gnaar gnep bane lassi wara baayi
For the the first part of my life bou société bi la tanone
Wala mom la guenone fessel
Soit pour bagna decevoir samay parent
Cuz I have too much love for them
Soit pour entretenir image bi nit gni am si mane
And I kind of think enough is enough
Nek na ni ki samay parent begone ma nek
Legui il est temps ma nek nit kima done
So boudé nit bobou nga khamone
Alors damala neubone len si mane so Excuse me for being fake
Boudé you bou doul rap béla guenelone nga baal ma it's fake as shit
Dunde moy gnane féké ndakh lima soumb do ngen massi feksi
Like Cole said love yours cuz aint no such thing as a life that's better than yours
So from now on I'm going to walk in any room as my full self and that pisses you off
Excuse me for being myself
Done li nga done
Mane ma done lima done
Kipel li nga dooné
Bayi maak lima done waa
Kou nangou li yalla dogal
Dou sone sa xol dou diex wawaaw
Kou bañ li yalla dogalé wawaaw
Di nga sone di nga diakhlé

Credits
Writer(s): Youssoupha Gaye
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
© 2024 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.