Renaissance Man
Beuri facette mbetté cassette
Double face temps ghost face killah
No machette gnou ngek gachette
Fuck Power ki yor ghost face ki la
Done leader si dealer yi
Kickeur ni killah
Gee bou dikker
Real Niggaz yi signer
Fils diokhma nope mais get ma ak bope
Bo lovoul hip hop do gnou tope
Drop master riche
Everything I do is a masterpiece
Rest in peace to my haters cheez
Dou maak ken si gnom ayouma si wakh fils bamaak djeuf
Done wadiour sa rappeur pare neb ko deg bi ndax dama teuf
God bign la santé maygnou sante
lissi dess lep gno koy jog coacher
Grit we want here fit lagn am mais
Daw lagn tere ni koy lek ak gaucher
Def Promo son yi sans promotion
Mouy sar sen galé def porta porte
Fek Melomane tok sone si conss poup
Gnou free si len si fitna porta porty
Aint no surprise cuz
binde si douche mom linou poupe dong
Zéro cohérence fils ouss kone
Taal kou leram off
Impossible ni Job kou meram job
Hate kou gnak kignaan
Kouma xaar xady mere xadi ko gnane
Count your blessings not your calories
Mind ya business lemme play my melodies
Find ya path then thank ya ennemies
Double down on ya strengh that's ya remedy
Binde mouy diss sa nope
Reud ngay guiss sa bope
Dundal ma Wiss la hope
Tok xaar Bal indi Lissi tope
God bign la santé maygnou sante
Lissi dess lep gno koy jog coacher
Grit we want here fit lagn am mais
Daw lagn tere ni koy lek ak gaucher
Yeah wakhone nako mais degougn ma wone
Let me say it again
Pour guiss rappeur bou melni mane erreur 404
Mak bou am ndierign 400 mbars
Binde doumassi taay 400 bars
Oubil mbarka ndiaye gnou take sans khar
Talibe Cheikh Anta bi takhoul Senghor doumak ben latin
Sattou mbar lafi anonymously radiakhé borom gnaari tour yi ni Ben Laden
Renaissance Man
Double face temps ghost face killah
No machette gnou ngek gachette
Fuck Power ki yor ghost face ki la
Done leader si dealer yi
Kickeur ni killah
Gee bou dikker
Real Niggaz yi signer
Fils diokhma nope mais get ma ak bope
Bo lovoul hip hop do gnou tope
Drop master riche
Everything I do is a masterpiece
Rest in peace to my haters cheez
Dou maak ken si gnom ayouma si wakh fils bamaak djeuf
Done wadiour sa rappeur pare neb ko deg bi ndax dama teuf
God bign la santé maygnou sante
lissi dess lep gno koy jog coacher
Grit we want here fit lagn am mais
Daw lagn tere ni koy lek ak gaucher
Def Promo son yi sans promotion
Mouy sar sen galé def porta porte
Fek Melomane tok sone si conss poup
Gnou free si len si fitna porta porty
Aint no surprise cuz
binde si douche mom linou poupe dong
Zéro cohérence fils ouss kone
Taal kou leram off
Impossible ni Job kou meram job
Hate kou gnak kignaan
Kouma xaar xady mere xadi ko gnane
Count your blessings not your calories
Mind ya business lemme play my melodies
Find ya path then thank ya ennemies
Double down on ya strengh that's ya remedy
Binde mouy diss sa nope
Reud ngay guiss sa bope
Dundal ma Wiss la hope
Tok xaar Bal indi Lissi tope
God bign la santé maygnou sante
Lissi dess lep gno koy jog coacher
Grit we want here fit lagn am mais
Daw lagn tere ni koy lek ak gaucher
Yeah wakhone nako mais degougn ma wone
Let me say it again
Pour guiss rappeur bou melni mane erreur 404
Mak bou am ndierign 400 mbars
Binde doumassi taay 400 bars
Oubil mbarka ndiaye gnou take sans khar
Talibe Cheikh Anta bi takhoul Senghor doumak ben latin
Sattou mbar lafi anonymously radiakhé borom gnaari tour yi ni Ben Laden
Renaissance Man
Credits
Writer(s): Youssoupha Gaye
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
© 2024 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.