Commando

Commando
Ndigel rek mouride sadikh
Beuri diom gnémé saadik
Dara dougnou mene stop ndakh li gnou guem rek call is addict
Krik krak automatic
Goor fit non doumak dic
Si loma wo loudoul foula fayda boumoula bet ndakh douma dick
On nous tue mais on ne nous deshonore pas
Dielel lep ma dessefa Ngor fall
Dougnou daaw té dougnou dep si kaw si kanam no matter what Baye
Diefé ndiguel té bayifi téré yi
Soldier djiko nekoul sol treyi
Def loula war té kharossilen koulani why nga deloko téréyi
Waaw goor ya ngi soga dor bo nandagoul ni commando non dou koba goor bou ngén sobando toy si yaw lay diougué diem ko topando mouy sa role model

Yaay diambar ra ngé
Yaay diambaara ngé
Yaay diambaar
Yaay diambar ra ngé
Yaay diambaara ngé
Yaay diambaar

Commando Commando loko diguel mou def
Commando Commando loko diguel mou def
Commando Commando loko diguel mou def
Commando Commando loko diguel mou def

Borom fit yi rekay deg tres bien
Say wakhi dof dougnou freiner
Koussi amoul diom nangou trimer ler na gnep ni dougn la parrainer
Nay deguer kethie ferou faleme
Na Puissant waay TP mazembe
Boul nangou mouk koula khep ni diamono colon dupont mademba
Pour tekki diaroul dieli cours si you
Arou na gnok sou gni coursiyou
Tak diok wodo fit ak foulak fayda dara ldou doux si gnoune
Loko diguel mou def foko dioubal mou dem
Ken douko sikel si nen lou kouy firndel dikal gnou dem

Yaay diambar ra ngé
Yaay diambaara ngé
Yaay diambaar
Yaay diambar ra ngé
Yaay diambaara ngé
Yaay diambaar

Commando Commando loko diguel mou def
Commando Commando loko diguel mou def
Commando Commando loko diguel mou def
Commando Commando loko diguel mou def
Commando Commando loko diguel mou def
Commando Commando loko diguel mou def
Commando Commando loko diguel mou def
Commando Commando loko diguel mou def



Credits
Writer(s): Youssoupha Gaye
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link