Amour Inconditionnel (feat. N'gone)
Yoow yooow
Yooohoo, yooow, yoooow
Mbeuguel bimay yegg sama xol dongue la xadj
Bés bu né ma beug ko waye wayé dou antou
Taye damay oubi sama panlanterou xol ndax
Kou Rombe sène mbolem mbidef yi fess del si birr (niar gni)
Niar gni geuneu feuss dou nioudoul samay niari wadiour
Diaroul diégué pour guiss ni gno geuneu sori thi mane, amana
Kounek si nioune xamna mbeguelou Ndeye si doom
Mbeguelou baye si doom
Mbeguelou dome si gnom
(Unconditional love)
Mom la ame si niom niom niou ame ko si mane
Yemougn si diour meu dongue déf naniou li waar si mane
Lepp lignou meusseu def si mane xadioul si fouki album
Kone douma Lim Damay taxaw kouma xol digua guiss
Desselougn ma Dara ma dongue massi dess
Tewoul louma meuneu dougou guinaw sougn ko thi dess
Ndem limay togou nioragoul bayi ma Kagn lene
Magal lene ba nieup gnimay deglou xamni
You're my life
You're my love
You're my life
You're my love
You're my love, you're my life, you're my everything
You're my love, you're my life, you're my everything yeahhhh
Samay magg ak samay rakeu dagn ma diokh thieur
Sisene doxaline mane lagne geuneu beug sene bopp
Mbeuguel bou amoul foumou feneu lanioumay diox
Sagn na geummeu di dox ndax douniou diog thi xol foumay dox
Dama ame chance ame famille bou melni yene
Badiene bou melni ami ndiaye papeu bou melni ass
Tanta bou melni Ndeye Khady nijaay bou melni seny
Thiowou famille you you sew dou meuss téré ma beug lene
Thi benen waleu yalla maynamay xarit
Jamono bi nieup di youxou batou xarit amatoul
Bene pédié sama wét moma geuneul Cices bou fess
Kene xamoul lima sania niakeu pour dess ak gars yi dess
Ndax Kate moussouma thiow té taxawougnou xex xex bi
Mane ma taxaw di wax mais gnom gno bâche tegg chaises yi
Yéré toubeuy dal soumi ngene dioxma ma sol
Dou lepp lagn meuneu wax motax ma beug ngene xamni

Nameu na tanto
Nameu na awa Cheikh
Soumala yalla meunone maye ma Doundou touti ak sama toureundo
Wala ak Mame Babacar diagne
Sante yalla yalla dou mayé leep
Yes I feel blessed
Yeah

Credits
Writer(s): Momar Ndiaye, Mouhamed Loucar, Ngone Fall
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
© 2024 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.