Tu Me Fuis, Je Te Suis

Tu me fuis je te suis iow rek laye tope
Rebel la douma baye
Figay diar bes bu nek fofou laye togg
Douma daw douma daye
Xamal ni yaw rek
Yaw rek laye tope
Yeah yaw rek
Yaw rek la love
Yeah yaw rek
Yaw rek laye tope
Yeah yaw rek
Yaw rek la love
Iow rek laye tope iow la beck Maye joe
Fi laye togg journée bi yeup Bo rombé laye jogg
Nobb la moy sama métier sa société laye job
Yonimeu ma deme employé la yaye boss

Mais nak doulma sori ndax sa xol bi laye yotte
Biss bi dakeu sama life moy biss bimkoy jott
Magui compter wér yi xawma bane Bess done
Dama doff si iow mbeuguel dinama raye moss

Meydey
Kouma meuneu dimbeuli si xaley nako def balamay dééé
Dama paré pour nek ak mom fi Guissouma Kane momay téééé

Magui nieuw magui nieuw
Fepp mo meunti nek nagua xamni magui faaa
(Mangui fa mangui fa)
Magui daw magui nieuw (yeah)
Loma sori sori nagua xamni magui nieuw

Tu me fuis je te suis iow rek laye tope
Rebel la douma baye
Figay diar bes bu nek fofou laye togg
Douma daw douma daye
Xamal ni yaw rek
Yaw rek laye tope
Yeah yaw rek
Yaw rek la love
Yeah yaw rek
Yaw rek laye tope
Yeah yaw rek
Yaw rek la love

Iow rek laye tope
Get na sa feeling ligua beug laye sole
Boma nangoulé Kigua beug laye done
Douma fi djogué finga ma tegg laye toggg
Figuay dioxone laye xol
(Iow rek laye tope
Get na sa feeling ligua beug laye sole
Boma nangoulé Kigua beug laye done
Douma fi djogué finga ma tegg laye toggg
Figuay dioxone laye xol)
Meydey
Kouma meuneu dimbeuli si xaley nako def balamay dééé
Dama paré pour nek ak mom fi Guissouma Kane momay téééé

Magui nieuw magui nieuw
Fepp mo meunti nek nagua xamni magui faaa
(Mangui fa mangui fa)
Magui daw magui nieuw (yeah)
Loma sori sori nagua xamni magui nieuw

Tu me fuis je te suis iow rek laye tope
Rebel la douma baye
Figay diar bes bu nek fofou laye togg
Douma daw douma daye
Xamal ni yaw rek
Yaw rek laye tope
Yeah yaw rek
Yaw rek la love
Yeah yaw rek
Yaw rek laye tope
Yeah yaw rek
Yaw rek la love



Credits
Writer(s): Momar Ndiaye, Mouhamed Loucar
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link