KMF
Ter bi mo jëm Dakar
Arrêt bi si top moy Keur Mbaye Fall
Hun
Yaw Est-ce que
Yaw Est-ce que xam nga lan moo nekk ci sama sac
Maanaam Gunna gun toog di obbëli rekk nga ma dakk
Eh yaw KMF dañ ñëw pour dogali nigga we back
Jël paaka teg ko ci sa put ammoo fi baat
Ammoo fi xeer enh
Tournel te won ma sa numero doqq
Toppal sama baaraam tamit yaw mi ci topp
Li ngen di def mën nañ ci bokk mais bëgguñ ci bokk
Non bëgguñ ci bokk
Man sollu ma Tim te maa la boot (baby baby)
Du Gis nga nii lañ la bettee
What!? Ñun ñi ñoo ko def yeena ko fekkee
À tout moment mën nañ la kill my nigga Take Care
Te da ngen nekk di ñu natt ay bu ngen ñu teggee
Xoolal ma Cab di tekk lu leer ci beat bi mel ni njool weex
Xoolal ma M-Geey akk flow bu méchant bi comme ku doon xeex
Xoolal ma Mor di jaay nonchalant te nëbb gun bi
Sagesse su Gandhi su wax rekk desee mënoo ñu gòndi
Mënoo fi nekk roi c'est moi qui détiens les rênes
Ding ma topp di daw da maa yokk train (Entraînement) yi ren
Won ma ku ma dakk rap ma won la mbott akk geen
Cab do it again
No New friends i'm with my gang
Ah shit
No matter what they say
Yaa ngi ci kër tay mere moy togg day neex kay
Da may jël âge di nuru boy mel ni Mbaye Dieye Faye
Doo ma gis fuñ ma inviter before I get paid
Du weexi bëñ moo tax ma nekk di soccu
Balaa ngay yëgg ni def naa dégâts day fekk ma ròmb
Non du masa gaayin nigga you cap
Ling ma def xëy na mootax chaque fois di nga guddee
Ok jam la ci taat
Julli moy tax nga may japp
Mën rap ba ammu ci app
KMF ku muus moo fi xaj
Maa ngi ci sama bopp
Succés mooma topp
Shos yi di ma nopp ku ñoddi reine (reen) ma def la xob

Credits
Writer(s): Cheikh Ahmadou Bamba Diop, Momar Gueye Ngom, Momar Ndiaye, Mouhamadou Sène, Mouhamed Loucar
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
© 2025 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.