Roungass
Hey geeneel paaka yi daas
Agsi toog sen fit yi jël sen xol yi di waas
Këllëm ci kaw beat bi man rekk maa len di maas
Da maa bëri feeling yen ngen dëkkee di kaas
Hey nañ len dajje rungaas
Fii maa fi nekk
Ñëw pour yokk cere dolli ñeex
Hey fii maa fi nekk
Arbitre sifflel tay rekk noon yi dee
Après coow li jeex foofu
Sudul Youtube bu ma tendance
Rap bi rekk lay mbaraan
Kenn saññu ma diss ndaxte xajju ma ci balance
Da maa xew Yallaa ko def
Siiw Yallaa ko def
Yaa ngi mer di bokk golo nga la way ku la ko teg?
Da ngaa soxor, soo saññoon ma torox
Fii laay toog ni faraax di len may ay bars yu forox
Maa koy teg ci temps nii
Jeune coof japp teint
Noqqul jall nee
Maa toog seeni bopp doon cancer seeni reins
Neel patt
Noppil bul ñu fatt
Kaasal der bu ñuul te ay métisses rek lay fat
Hey Neel patt
Noppil bul ñu fatt
Ubbi naa sen taat sotti acide seen gat yi

Pape Sidy awma ñaari gels
Mais chaque jour crush bu bees
Ñoom ñëpp ñi ngi may baayi xel
Mais baayi wu ma sama bopp
Sa lyriciste da ma ko vent
Tax sen xol du feex
Kanam bu chou ay pec yu yem akk poche bu àntan saaku ceeb
Sa xol moy xasan mais doo waga
Liquide yoroo walaat
Do dem fenn matoo woyaas
Baayil rap dem wayaan
Deuxième couplet 3e baram rap ba am ci 4e madame
Goor Faal fa may fanaan sa gels laali na fa ay draps
J'en ai marre
Ci seeni cas chaque jour yu bees nooy mel ni COVID
Ñi ma ñaanal maa len jullee
Jël ngaamu noon yi sukki mukki
Boy buñ taal ma mukki mukki
Xew ni ku boot fukki bukki
Baayi naa playback fukki junni
Mafi në

Waw fii maa fi nekk
Hey yaw Arbitre sifflel tay rekk noon yi dee

Credits
Writer(s): Baye Dial Gueye, Momar Gueye Ngom, Mouhamed Loucar
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
© 2025 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.