Yow Lë

Yow lë
Sama xol fess na takh gua may podj
Nala defaal lo guissoul ci ben goor
Say tiono diekhna may ki lay soore
Waaw goor Douma bokk ci goor yilaay door
Guisna ci say beute xargua ba soy
Guissoulo kou crx taxna guaay dioy
Say ronguogn ferna may kilaay yoor
Gni ay xolou xer lagn yor mane may or
Wane gua ma foula ak diom
Wane gua ma wane gua dioup ak ngoor
Souba ak guone dina dioubo ak yaw
Yama takh beug diour ay dome
Bou sobei Yallah digua soul sa ay none
Diouyo ak niom gnou bokk doulo ak yaw
Digua done bour digua sour ak forme
Ba gnila beugua loorr beug ndiro ak yaw
YAW LA BEUG NALA TAKAL BAGUE
KENINN KOULA BEUG TAKK NAKO TAKAAL AY BOMB
Deug deug Diaraal gama rakk
Douma doyaal dila taagu dila nié diko tioow
Yafi tek tankk yay bomb
Koula guerre nako gone militaire lay done
Bigua dalei ci mane lassa xel wara daal dina dem Diaka gua dem mairie sol robe
Yay done kiy diour samay dome
Soma degualoul damay doff (hey)
Yay done kiy diour samay dome (hou hey ii)
Sama gueineu waleu guay dome
(oh oouh oh! Oh oouh oh)
Sama guéneu waleu guay done
Sama guéneu waleu guay done
(Oh ouh oh! Oh ouh oh)
Yay done kiy diour samay dome
(Hou hey ii)
Sama gueineu waleu guay done
(Oh ouh oh! Oh ouh oh)
Yow la taneu (yow lë)
Yaaw la tamou (yow lë)
Guisna ci yaw lou kene amoul
Oh ouh oh! Oh ouh oh)
Yaw la taneu (yow lë)
yaw la tamou (yow lë)
Digua am si mane lou kene amoul
Yow lë Yow lë ëë

Yow lë

Yow lë Yow Lë ëë

Tiebou yap bou kheign neu
Amatoula loumaay neub lepp fegn neu
Yagu na dadialei ay tioro
Wayé louma meussa am ci diangori djiguene lepp dagn neu
Gnila togn togn nagnma
Dou wakhou pitieu mais wakhou wegn (fer) leu
Def tiakay di tal sama money dou lima guondi di guene dila fi bayi dafaay fekk ma bagnla
Legui takoussane diote yagatoul yagatoul legui tak seuy diote
Legui samaay gooro daldi sakou sen dote
Legui Pa yi diouguei diakeu gua tagou say mbokk
Mousso dem ba finale ak mane
Meusgua touki wayei di gua dem féninn ak mane
Dinkeu nagnoumala gua fanane ak mane
Sama dekhou baneeekh digu fa naane akk mane
Tey la beuss bi dak sama life
Tey lay dogua nek kilifa bima yagu beug done
Diaré ci kou rafeet xol
Mangui fateilikou bima done guenteu dila xol dissi diamou sougnou borom
Yagu yekk péekh biy wané ni gnigui si yone
Ndakh nena seuy bokna ci loumou gueuna sopp
Yay done kiy diour samay dome
Soma degualoul damay doff (hey)
Yay done kiy diour samay dome (hou hey ii)
Sama gueineu waleu guay dome
(oh oouh oh! Oh oouh oh)
Sama guéneu waleu guay done
Sama guéneu waleu guay done
(Oh ouh oh! Oh ouh oh)
Yay done kiy diour samay dome
(Hou hey ii)
Sama gueineu waleu guay done
(Oh ouh oh! Oh ouh oh)
Yow la taneu (yow lë)
Yaaw la tamou (yow lë)
Guisna ci yaw lou kene amoul
Oh ouh oh! Oh ouh oh)
Yaw la taneu (yow lë)
yaw la tamou (yow lë)
Digua am si mane lou kene amoul
Oh ouh ooh



Credits
Writer(s): Elzo Jamdong, Misterthiere
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link