Gadaay (feat. Obree Daman)

Chiii riii reee
Chiii riii reeeraa
Ahhhhhhh yeaaaaaaah

Ge'stu woo ma
Deglu woo ma
May laaj lu xew
Gisu loo ma
Te gisoon naa ni
Da nga reer ma lay jeex Da ma fog ni
Tayu loo ko ndax mbëggeel Defoon na ni
Di nga changer balaa maa dem
A'ndandoo bi
Ci jamano ji
Mën na xaar ba beneen
Xarit woo ma
Woo ma yee su fekee may nelaw Fi ñu to'll
Kan ngay woolu kudul sa xel Balaa maa dem
Naa la wax ni am naa coffeel
Coffeel bi ma am ci yow
Waat naa ni doo ko yëgg
Wallaay dang ma miin
Ba doo ma yëgg ba maa ngay dem
Gestu woo ma
Gadaay Gadaay
Yëggu loo ma yow Gadaay Gadaay
Faale wu loo ma Toppatoo wu loo ma yow (Bis)
I know something's wrong
Doomu yaay mbaa fate wu loo ma
Woote naa te wuyu wu loo ma
B'cause I know something's wrong
I know something's wrong
Maa ngi dox akk ta'nku ne'en
Ci naaj bu ta'ng lool
Maa ngi mar naan ndox mu jafe lool
I know
B'cause I know something's wrong
Gilee jëlsi xarit sama doomu yaay fi ma toll weet naa
Bilee doomu yaay jëlsi ma xarit sama fi ma toll weet naa
Doomu yaay jëlsi ma
Xarit sama doomu yaay jëlsi ma Mbaa fate woo ma
Doomu yaay jëlsi ma
Xarit sama doomu yaay jëlsi ma
Gëstu woo ma Lijënti woo ma yow
Faale wu loo ma Toppatto woo ma yow
Gëstu woo ma
Xoolu loo ma yow Yëggu loo ma
Faale wu loo ma Lijënti woo ma yow Moo tax gadaay naa
Gadaay
Fii ku fi wac sa'w and and boo dem fekk fa sa moroom mu toog
Xale yaa ngi gadaay
Bu ja'nt sowee Timis maase
Kulay yobbaaleel Ndax Guddi xaaj na Fajar waaj na
Ëllëg sooraaleel Reccu wees na Jëffëm fe'eñ na
Kookoy diggaaleel Ludul
Yalla neen la Yeene neeg la
Nga fay fanaane



Credits
Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Oumar Samb, Arfang Tiare
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link