Ñibisil

Ñibisil
Ñibisi-i-il

Jukk du wess, jukk du wess
Suma lay woo lutax doma falé
Wax ma lu dañ ci man xana bëgëtoma
Yeah, yeah
Bëtu mbëgëel lala mësa xol le
Lu waral man ak yaw ñu dëkk si cow

Suma xolei fuñu jar yep
Dag ma wowon dima deff fu sori
Bi ñuye goro loxam wax ma
Tay bitti bi molay gërëm kër gi joy triste

Samba alar waw si njabot ji
Xol yagi joy xar yagi joye

Ñaata at man ak yaw ci kër gi
Bimalay tan bobu xalato diga sëye si
Soxna si sétal si Yallah ji ga xol si bitti
Gisso sa morom bu né si sëye ba pare nési
Mbédd bi njaboot mo mucow
Lu fess nak si xol su ëpe turu
Muñe na ba s¨s taxul ga xam li xol bi jiyunju
Dadjie n'a lu ne gir yak ak njaboot ji liñuye dundu
Fimay dundu giss n'a luné ms taxul ma xadi
Baneex man dég lassi am
Cono ak nakkar tax ma gëje nekk si jam
Wax ma lan ga bëgg si lan gané
Talatoma talato sa kër gi wax ma noye deff ak njaboot gi
Wax ma man ak yaw ku tane
Feep fo xam nangi maffa clamé
Mbato dem mbato koste mënoma teré xolli kanene
Leep loma yakkul dagako fatte
Su respect jexe mbëgeel dem yonam luñu desse ludul

Samba alar waw si njabot ji
Géstu war nala samba alar ga
(Xol yagi joy xar yagi joye)
Gniga bëgëntél ñongi sa ginaaw
Yeah, yeah

Sumalay wo gani doma falé
Sumalay woo, oh oh
Xana nobatoma?

Su démb donone tay
Ma joxatta sama mbegeel?
Su démb donone tay
Ma joxat la sama xol bi mbegeel bi

Sumalay wo gani doma falé
Sumalay woo, oh oh



Credits
Writer(s): Abdoulaye Sy, Ashs The Best, Olivier Delahaye
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link