Pottu Ndaa

Gisoo ni fu sori la joge
Ba ñuy gone dañ foogoon ni
Boo maggee Loo yootu day gaaw
Tera'nga bi day naxe ci boo foogee Lepp yay boroom
Adduna bi pottu Ndaa la boo naanee jox sa moroom naan
Jamm du doy!!!
Du alal jamm moo li gën ci ñun
Nang xoolee sa bopp yeene ko peace and love and harmony
Lepp du yay boroom fii dang fi am waar keneen am fi waar
Saabu bi footul boppam
Man la man la lune nga ne yay boroom
Fii demal maa ngi ñëw la Tay sa bis suba bisam la
Boo goree jekkoo del baalee Adduna di ndaa yow
Soo naane jox sa moroom naan yow Yaatu yaatalal sa xol yow
Jamm du doy!!!
Seet naa ba seet moy li gën ci ñun
Mbëggeel akk alal du doy
Bu fi jamm nekkul dara xajjul ci ñun
Saabu bi footul boppam
Man la man la lune nga ne yaa ko moom Dimbalil xale bi mbokkam
Xoolal li nga yeene sa bopp yeene ko bepp jaam
Gisoo ni fu sori la joge
Ba ñuy gone dañ foogoon ni
Boo maggee Loo yootu day gaaw
Tera'nga bi day naxe ci boo foogee Lepp yay boroom Adduna bi pottu
Ndaa la boo naanee jox sa moroom naan



Credits
Writer(s): Abdoulaye Sy, Ashs The Best, Olivier Delahaye
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link