Xel Akk Xol

Yeah, eh eh eh
Lé, lé, walé
Hum, hum

Suuba souma yéewoo, yaw la bëgg jakarlool
Sa suma yeewu, yaw lay mbëgg njëk xool
Ëlëk lu mata soor la, waye xel xalaat u ko
Ëlëk ay jaar-jaar la, sama xol yëgoon nako muy ñëw

Xel xalaat la (xel ak xalatam bë)
Xol yëkk yëkk la
Niit ak jëmmam ja dara xaaju fë

Sa suma yeewu, yaw lay bëgg njëkk xol (fajaar suma yéewo yaw Ia bëgg njëk xool)
Fajaar suma yéewo yaw Ia bëgg njëk xool

Denk na la guddi, fanaane yaakaar ci yaw (denk na la sama xol fanaane yaakaar ci yaw)
Gent na la guddi gi yëpp ndax fajar yaw lay jakarlool

Mbëggelam
Xel xalaat la
Xol yëkk yëkk la
Niit ak jëmmam ja
Dara xaaju fë

Xel xalaat la (xel ak xalatam bë)
Xol yëkk yëkk la (sama xol-)
Niit ak jëmmam
Ja dara xaaju fë (Dara fa xaajul)

Niit nak ak jëmm ja, Dara fa xaajul



Credits
Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Arfang Tiare
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link